Alegsàndiri
From Wikipedia
Alexandria (Iskindireyya) |
|
Alegsàndiri tey ji | |
Dàkkantal: "Dëkku Alegsàndar bu Mag" | |
Alegsàndiri ci Misra (seetal Alexandria ci kaw) | |
Coordinates: | |
---|---|
Country | Misra |
Samp na | 334 BC |
Population (2001) | |
- City | 3,500,000 |
Ci angale mooy Alexandria; Ci faranse mooy Alexandrie
Benn dëkk ak teeru ci Misra la, fu sorewul bëlub dexu Niil. Péeyu Misra la woon ci jamano Injiil ji, di dëkk bu gëna am solo ci Gereg yi. Ñaareelu dëkk bu gëna réy ci nguuru Room.
Dañuy fekk Alegsàndiri ci Injiil ci Jëf 6:9; 18:24; 27:6; 28:11.