Amon
From Wikipedia
Ci làkku ibrë (אמון) la tur wi jóge. Ci angale mooy Amon; Ci faranse mooy Amon
Tàmbalee ci Robowam fukkeelu buur ak ñeent ci réewu Yuda la woon, di maamaatu Yeesu ci Macë (Mc 1:10). Man nañu gëstu jalooreem ci 2Ki 21:18-26; 2Ch 33:21-25.